Content-Length: 73746 | pFad | https://wo.wikipedia.org/wiki/Kax_b

Kax b — Wikipedia Aller au contenu

Kax b

Jóge Wikipedia.

Kax bi

ab kax.


fi kax yi dëkke ci kembaaru Afrig


Kax nag bokk na ci limka gi mbootaay gii di "Booleg Réew Yi Ngir Sàmm Kéew Mi" def ci atum 2008 ñeel ràbb yi nar a raaf ci kaw suuf, maanaam sunu moytuwul dootuñu amati dañuy jeex. yenn dëkk yi li ko fay raafloo mooy nit ñi leen di rëbb ci amam yu jaaduwul ngir di ci defar ay gëtt. Kax nag rabbu guddi la, bëccëg gi yépo da koy nelaw ci diir ñax yu fatt yi, di yeww bu janti bi sowee.









ApplySandwichStrip

pFad - (p)hone/(F)rame/(a)nonymizer/(d)eclutterfier!      Saves Data!


--- a PPN by Garber Painting Akron. With Image Size Reduction included!

Fetched URL: https://wo.wikipedia.org/wiki/Kax_b

Alternative Proxies:

Alternative Proxy

pFad Proxy

pFad v3 Proxy

pFad v4 Proxy