Content-Length: 163026 | pFad | https://wo.wikipedia.org/wiki/G%C3%A9ej_gu_Diggu

Géej gu Diggu — Wikipedia Aller au contenu

Géej gu Diggu

Jóge Wikipedia.

Géej gu Diggu mooy géej gi ne ci diggante goxu Afrik ak bu Tugal ak bu Asi. Guddaayam di 2,51 milyioŋ ciy km² te yaatuwaayam toll ci 3700 km.

Ci sowwu mi ngi yem ci Mbàmbulaanu Atlas, ci penku ci Géeju Marmara ak Géej gu Ñuul gi. Yenn saa yi Géeju Marmara dees koy boole ci Géej gu Diggu gi, waaye Géej gu Ñuul gi moom dees koy tàqale ak moom.

Géej gu Diggu gi dees koo seddatle ci ñaari mbalka*. Mi njëkk mooy Géej gu Diggu gu sowwu gi, yam ci yoonal* gu Sisil. Meneen mi mooy Géej gu Diggu gu penku gi.

  • Yoonal: canal
  • Mbalka: bassin
Diwaani Tugalasi
Asi      Diwaan yu MR: Diggu Asi · Penku Asi · Bëj-saalum-penku Asi · Ron-goxu End
Yeneen diwaan: Penku gu Sori · Penku gu Diggu · Penku gu Jege · Sibeeri
Tugal      Diwaan yu MR: Sowwu Tugal · Bëj-saalumu Tugal · Penku Tugal · Bëj-gànnaaru Tugal 
Yeneen diwaan: Kókaas · Géej gu Diggu · Skandinaawi








ApplySandwichStrip

pFad - (p)hone/(F)rame/(a)nonymizer/(d)eclutterfier!      Saves Data!


--- a PPN by Garber Painting Akron. With Image Size Reduction included!

Fetched URL: https://wo.wikipedia.org/wiki/G%C3%A9ej_gu_Diggu

Alternative Proxies:

Alternative Proxy

pFad Proxy

pFad v3 Proxy

pFad v4 Proxy