Aller au contenu

Feppmaandu

Jóge Wikipedia.

Feppmaandu as wàll-wàllaanu xarefulwoon bi la. Di wenn ci wàll-wàllaan yi dàtt saalu xarefulwoon bi. Ni ko turam di junjee, feppmaandu dafa maandu moo tax amul yanu mbëj (du bu baax(+) mbaa bu bon(-)). Feppmaandu yeek feppsaal yi su ñu leen boolee ñooy nekk saalu xarefulwon bi. Ngir ab xarefulwoon, dañuy bind Z limu feppsaal yi, A di limu feppsaal + feppmaandu. Kon limu feppmaandu yi dafay doon N =A-Z.

Lefu feppmaandu mi ngi toll ci 939,56533 MmV. Ki ko wuññi mooy jëmmaan bu waa-angalteer ba James Chadwick ci 1932.


Wikipedia
Wikipedia
Bii jukki ab junj rekk la. Man nga cee duggal sa loxo suqali ko ndeem am nga ci xam-xam ci anam yi Wikipedia taxawal


pFad - Phonifier reborn

Pfad - The Proxy pFad of © 2024 Garber Painting. All rights reserved.

Note: This service is not intended for secure transactions such as banking, social media, email, or purchasing. Use at your own risk. We assume no liability whatsoever for broken pages.


Alternative Proxies:

Alternative Proxy

pFad Proxy

pFad v3 Proxy

pFad v4 Proxy