Aller au contenu

Barabas

Jóge Wikipedia.

Ci làkku ibrë בר-אבא; Ci làkku yawut la tur wi jóge. Ci angale mooy Barabbas; Ci faranse mooy Barabbas

Bóomkat ak taskatu réew la woon. Nekkoon na ci kaso bi ñu jàppee Yeesu. Pilaat bàyyi na ko bi ñu àttee Yeesu. Man nga ko jàng ci Mc 27:16-26; Mk 15:7-15; Lu 23:18-25; Yow 18:39-40.

Turam moo feeñ ci aaya yii: Mc 27:16,17,20,21,26; Mk 15:7,11,15; Lu 23:18,19; Yow 18:40.

pFad - Phonifier reborn

Pfad - The Proxy pFad of © 2024 Garber Painting. All rights reserved.

Note: This service is not intended for secure transactions such as banking, social media, email, or purchasing. Use at your own risk. We assume no liability whatsoever for broken pages.


Alternative Proxies:

Alternative Proxy

pFad Proxy

pFad v3 Proxy

pFad v4 Proxy